Baay faal gueu da djook thia fadjar
Nga sène ko mouy soli sagar
Boppam ba sekkeu ki kawar
Yoré keulleum ba di sikar
Té falé woul khiif ak mar
Boo démé sakh khekh na badar
Ki toureum wi dotoul fay
Kou wéddi li ladj ko wa ndar
Baay faal djakhal na wa ndar
Baay faal djakhal na wa ndar
Baay faal gueu da djook thia fadjar
Mani bour Yalla da djook thia fadjar
Nga sène ko mouy soli sagar
Yoré keulleum gueu di zikar
Ki toureum wi dotoul fay
Kou wéddi li ladj ko wa ndar
Baay faal djakhal na wa ndar
Baay faal djommeul na wa ndar
Doundeum gueu nekh na
Zikar sa neekh na lol
Baay faal bi, baay faal ki modi guènne goor
Zikar sa motakh mou djégué Yalla
Baay faal bi, baay faal kouko khamone dinga mandou thi mome
Nga sène ko mouy soli sagar
Boppam ba sekkeu ki kawar
Yoré keulleum ba di sikar
Té falé woul khiif ak mar
Boo démé sakh khekh na badar
Ki toureum wi dotoul fay
Kou wéddi li ladj ko wa ndar
Baay faal djakhal na wa ndar
Baay faal djakhal na wa ndar
Baay faal gueu da djook thia fadjar
Mani bour Yalla da djook thia fadjar
Nga sène ko mouy soli sagar
Yoré keulleum gueu di zikar
Ki toureum wi dotoul fay
Kou wéddi li ladj ko wa ndar
Baay faal djakhal na wa ndar
Baay faal djommeul na wa ndar
Doundeum gueu nekh na
Zikar sa neekh na lol
Baay faal bi, baay faal ki modi guènne goor
Zikar sa motakh mou djégué Yalla
Baay faal bi, baay faal kouko khamone dinga mandou thi mome
Comments (0)
The minimum comment length is 50 characters.