Niouné nitt,nitt moy garabame (?)
Wala nitt,nitt moy moussibam
Niaka niit,diouk weuri daradiam
Balla Balla moussibak diLa Diam

Xamey bou bakh niouy nieuw thi yaw
Ngi indi ak ngi yabou thiow
Ndi dokh di dem niiu tok di dieuw
Kën dou topou nitt thi jikkom you sëw

Andano xaménga bithi geun
Killa jiégë ladioul finga Dieum
Lou dokh bi sori néné yawla Geum
Kon xamél xaritt bi baxak bi Geunn

Bad company (!)
Omo ano need no bad company
No come dey form for me
Anywhere we deh we fitto lockdown pan it

Bad company
Omo ano need no bad company
No come dey form for me
Anywhere we deh we fitto lockdown pan it

Sorilma Dorr katt,,workatt(??)
Nittou interé doukou weur katt
Fou Diamano leuwto niou Daw Kat
Fou noy laniiuy weur ngir daw tak
Comments (0)
The minimum comment length is 50 characters.
Information
There are no comments yet. You can be the first!
Login Register
Log into your account
And gain new opportunities
Forgot your password?