0
Ballago ndumbé yatma - Youssou N'Dour
0 0

Ballago ndumbé yatma Youssou N'Dour

Ballago ndumbé yatma - Youssou N'Dour
Billaay , ballago ndoumbé yatma
Su ñu waaji xaj oon na fi
Naxxar doηη ,la ñu bayyee
Yalla , wonneeti na

Li tax ba mbir mi metti lool
Ñun da ñu ko foog wul woon
Yëf yi gaaw ba bette gnou
Billaay wéetël na ñu

Njiinoo njiin faramaareen
Gòor u jaaga , nelaw naa
Baay i wally dem na nii
Ñun daal wéetël na ñu

Ma ngi koy jaale Sénégal
Di ko jaalé Gambia
Di ko jaalé adduna
Ndaanaan ba dem na nii

Thione ballago , ndoumbé yatma
Bu yalla buur bi doon taggoo
Kon di na ñu bayék yaw
Ni patrimoine bi nga ñu bayyeel
Yee gua nit gñi , tete leen ci adduna
Yee gua nit gñi , tete leen
Xam al leen ci adduna
Ahhh - Ballago
Comments (0)
The minimum comment length is 50 characters.
Information
There are no comments yet. You can be the first!
Login Register
Log into your account
And gain new opportunities
Forgot your password?