0
4/4/44 - Youssou N'Dour
0 0
4/4/44 - Youssou N'Dour
4-4-44 (4-4-4-44) môm sa bopp mô neikh
4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok mô neikh

Bô léké ba sour war nga gueureum
War nga gueureum gni doug thi wagne wé
Wagne wa tang na
Fimou toll nî war nguèna bëg
War-ngèna bëg thi indépendance bi ak-liko indi

4-4-44 (4-4-4-44) môm sa bopp mô neikh
4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok mô neikh

Bô léké ba sour war nga gueureum
War nga gueureum gni doug thi wagne wé
Wagne wa tang na
Damani bou leuk léké olom
Boudè goréna té deugou warna ko guereumé pithe

No, no, no no no no
No, no, no no no no yeah

4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok mô neikh
4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok mô neikh

Ah li dafa nékh... guiss say mbok mô neikh
Li dafa nékh... gueume sa bopp mô nékh
Comments (0)
The minimum comment length is 50 characters.
Information
There are no comments yet. You can be the first!
Login Register
Log into your account
And gain new opportunities
Forgot your password?