Shukran lakah... modou bamba mounoumala faye khana ma wayla
Ligueyba de rek nguir at ya allah mbacke da nga yah guinaw
Ak kanam nagne roye thi yaw rek meuneu dieum thi kanam
Cheikh ahmadou, backe mane de sante nala diadieuf bayou
Mamadou lamine bara sama di guante ak ya allah yama ko leral
Lou ne nawal nga ko te takhoul nga diakhal ya takh may bale
Di yeureumate ken dotou ma ata te ba na khebate diaaa dieufe
Bayou serigne saliou serigne mourtalla chukran bamba chukran
Laka chukran chukran chukran chukran chukran odou bamba...

Comments (0)
The minimum comment length is 50 characters.