0
Bamako - Youssou N'Dour
0 0
Bamako - Youssou N'Dour
Si gare bi lako fekkeu
Mi ngui sanguo seur
Té beut yi di takkeu
Ma dal di koye nougnou
Mou dal di maye faye
Dal di maye yédeu ci adouna bou yakhou bi
Mane douma fatté!

Ah mani ah mani!
Man douma fatté bamako lii mani lii mani!
Mane douma fatté!

Kerok lama khamal louma khamoul woone ci diamono bou yakhou bi yénene ak yénene;
Balaa maye dougeuti mane ci loumou meuneu doone
Dinaa fattélikou ndaw sossou
Limouma wakhoone!
Souy souy sou sou sou sou sou sou souy!!
Ci gare bi lako fekkeu mi ngui sanguo seur té beut yi di takkeu
Ma dal di koye nougnou
Mou dal di maye faye dal di maye yédeu
Maky yé maky maky yé maky yééééé!!!!
Waw kérok lama khamal louma khamoul woone ci diamono bou yakhou bi
Balaa maye dougeuti ci loumou meuneu doone
Dinaa fattéli ko maky yé maky maky yé maky yéé!!
Ah mani ah mani!
Douma fatté bamako lii mani lii mani!
Mane douma fatté bamako
Comments (0)
The minimum comment length is 50 characters.
Information
There are no comments yet. You can be the first!
Login Register
Log into your account
And gain new opportunities
Forgot your password?