0
Mool (Deglu meteo) - Youssou N'Dour
0 0

Mool (Deglu meteo) Youssou N'Dour

Mool (Deglu meteo) - Youssou N'Dour
Yaw mool u géej gi
Di jambaar ci réew mi
Bala ngaa dem géej
Ngala déglu météo

Bu la nee bul dem
Lu mën ë xew bul dem
Ben fan ak ñaar
Bu mu yax sa liggéey

Doyloo nga yalla
Du tee nga sa yor téléphone
Ak sa gps , te bul fatte sa gillet

Sama fans yi ma am
Mool ñoo ma gën ë xam
Fu ma làng ee ak ñoom
Guddi gë day xumb lool

Man sama fans yee , ma saf
Sawar naa làng ak ñoom , fu ne
Aka ñoo dégg daaj , ma ni
Moo tax may dem ba jeex , walla

Jambaar ca waar wa
Jambaar ca géej gë
Su ma ko mën oon
Ben mool du des ci géej
Comments (0)
The minimum comment length is 50 characters.
Information
There are no comments yet. You can be the first!
Login Register
Log into your account
And gain new opportunities
Forgot your password?