Keroksou penc bognouy wadjia wathié janta bi
Di wadjial Péssé ba
Moulay dabbaxx yalla nagnou la diégué yalla daal moy taan waayam
Moulaay Dabaaaaax...
Bougnou Faté, Bess boboulé, Uhh Bougnou Soré, Bess boboulé
Bougnou faté Bess Boboulé
Lofa Gnaane, Yalla May lako
Modaane wakhal nitt gnep, Mo daane wakhal nasraane yi
Anh Mo daane Kadou Askane wi
Dafa daane wakh naane nagnou bolé sougn rew
Dafa daane wakh naane bou kéne wéngal gaal gui
Dafa daane wakh naane nagnou bolé sounou khol yi
Dafa daane wakh naane nagnou yeureum Djiguéen
Sa borom bi begu na, Yonentam bi begu na, yako liguéyal sa borom
Moulaye Dabbaxx yaw dé wacci ngua masso wakh lou amoul
Kérok bang gnou djito assamaane si da Leudeum
Bessa ngui kéne dotou ko Fatéééti... Moulaay Dabbaxx
Bougnou Faté, Bess boboulé, Bougnou Soré, Bess boboulé
Bougnou faté Bess Boboulé
Lofa Gnaane, Yalla May lako
Anh! Modaane wakhal nitt gnep, anh! Mo daane wakhal nasraane yi
Anh! Mo daane wakhal Askane wi

Comments (0)
The minimum comment length is 50 characters.