0
Yama - Youssou N'Dour
0 0
Yama - Youssou N'Dour
Soubateel, bamuy barilé
Ñi di déloo sen palanter
Ngir baña xaar li xew, li xew féneen

Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon
Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon

Gaal gi teer
Ba ñu seet li, li wara dem féneen
Té du yeebi ludul meew lifi des

Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon
Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon

Moo waral bu sédalé, du am
Du am, rusna ñaan ba day fandé, fandé
Moo waral bu sédalé, ba du am
Du am, rusna ñaan Kii daal amu fi morom
Yaamaa nango sona lol

Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon
Ni woo Yama, ni Yama ku la seetlu woon

Ni dox sa waar bamu noppi yaw
Téréwul topa bëgë bëgë xaléyi
Yaama rek la soxal diarama
Diarama, diarama
Comments (0)
The minimum comment length is 50 characters.
Information
There are no comments yet. You can be the first!
Login Register
Log into your account
And gain new opportunities
Forgot your password?